الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي أَحْيَانَا بَعْدَ مَا أَمَاتَنَا وَإِلَيْهِ النُّشُورُ
Firi
Cant ñeel na Yàlla, ki nu dundal ginnaaw bi mu nu reyee (ci nelaw), te ci Moom la dekkite bi.
Ni ñuy jàngee
Alhamdu lillaahil-ladhii ahyaanaa ba‘da maa amaatanaa wa ilayhin-nushuur.
Fu mu jóge: Al-Buxaari, 6324
