سُبْحَانَ اللَّهِ وَبِحَمْدِهِ، سُبْحَانَ اللَّهِ الْعَظِيمِ
Firi
Yàlla sell na ci bépp ayib, te cant ñeel na Ko! Yàlla Aji Màgg ji sell na ci bépp ayib!
Ni ñuy jàngee
Subhaanallaahi wa bihamdihi, subhaanallaahil-‘aziim!
Fu mu jóge: Al-Buxaari, 7563 · Muslim, 2694
