السَّلَامُ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَةُ اللَّهِ وَبَرَكَاتُهُ
Firi
Jàmm na nekk ci yéen, ak yërmandey Yàlla ak barkeem!
Ni ñuy jàngee
As-salaamu ‘alaykum wa rahmatullaahi wa barakaatuh!
Fu mu jóge: Abu Daawuud, 5195
Ñu ngi leen di wax ci toftaleef bii
- Nuyoo
- Tontu nuyoo
